Locks boy-Jëguësima honey (Audio Official)
Artiste : Locks Boi Title : Jëguësima honey Label : Peace’Ful Music Beat : by Hofishal sounds Prod by : BayDoss Records : Reuk Seuss Records Mixing & ma...
About this video
Artiste : Locks Boi
Title : Jëguësima honey
Label : Peace’Ful Music
Beat : by Hofishal sounds
Prod by : BayDoss
Records : Reuk Seuss Records
Mixing & master : Dossbeats
#Jëguësima #honey #Locks boi #Doxame
Crédits de la chanson & du clip Locks boi**
Auteur : Locks boi
Directeur Artistique : Locks boi
**Les lyrics de la chanson Jëguësima honey **
1_Couple
Lidémétina dama moujé jéup sama khôl bi sédlouna
Ndax khalé bima beug guele sama bopu té yeguma
Damako nop bame ses si sama khôl bi té yeuku koo
Soumala guiss sé béug soma nouyooour rekma réé
Call la diaxaso wola banga nieuw ma mouma
Khalébi laa love sama rounda gunda
Khélmi diaxaso santimayi diaxaso
Lépa diaxaso tékhalé bilé yaguko
Sama khôl moma warona wax noumay déf baamla
Mom mai déf man bama nop la paré tékma thiono
Man iska dama dof
kholou ma kané khalé bi rek moma saaf
Saa bouma beug gué wax ak mom sama fit né têf
Ma diamko pis déf rature diaré faa ay kaaf
Khaw ma noumay déf mais budé man rek duko yeuk
Éé girl kaye
Wou yay.
_Refrain
Bébé
Baby girl sama bébé
Bébé
Baby girl sama bébé
Bébé
Baby girl sama bébé
Bébé
Baby girl sama bébé
_Péré- refrain
Topou nala founé
Wari nala founéé
Topou nala founé
Wari nala founéé
Topou nala founé
Wari nala founéé
Topou nala founé
Wari nala founéé
Yea yea yeahhhh
Topou nala founé
Wari nala founé
Khalé bilé kaye way
Jëguësima honey
Topou nala founé
Wari nala founé
Khalé bilé kaye way
Jëguësima honey
Topou nala founé
Wari nala founé
Khalé bilé kaye way
Jëguësima
_Refrain
Bébé
Baby girl sama bébé
Bébé
Baby girl sama bébé
Bébé
Baby girl sama bébé
Bébé
Baby girl sama bébé
2_Couple
Khalé bima beug waxlén noumay déf ba amko
Topou nako bop batay té yombou goule ma amko
Khalé bima beug waxlén noumay déf bam yaukko
Topou nako bop batay té yombou goule mou yaukko
Khalé bima beug waxlén noumay déf ba amko
Topou nako bop batay té yombou goule ma amko
Khalé bima beug waxlén noumay déf bam yaukko
Topou nako bop batay té yombou goule mou yaukko
_Péré- refrain
Topou nala founé
Wari nala founé
Khalé bilé kaye way
Jëguësima honey
Topou nala founé
Wari nala founé
Khalé bilé kaye way
Jëguësima honey
Topou nala founé
Wari nala founé
Khalé bilé kaye way
Jëguësima..*
#Jëguësima #honey #Locks boi #Doxame
Have a question? contact me:
📞+221773670785
Video Information
Views
596
Total views since publication
Likes
34
User likes and reactions
Duration
2:59
Video length
Published
Dec 22, 2021
Release date
Quality
hd
Video definition
About the Channel
Related Trending Topics
LIVE TRENDSThis video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!
THIS VIDEO IS TRENDING!
This video is currently trending in Morocco under the topic 'météo demain'.