Locks boy-Jëguësima honey (Audio Official)

Artiste : Locks Boi Title : Jëguësima honey Label : Peace’Ful Music Beat : by Hofishal sounds Prod by : BayDoss Records : Reuk Seuss Records Mixing & ma...

MLYBEATS596 views2:59

About this video

Artiste : Locks Boi Title : Jëguësima honey Label : Peace’Ful Music Beat : by Hofishal sounds Prod by : BayDoss Records : Reuk Seuss Records Mixing & master : Dossbeats #Jëguësima #honey #Locks boi #Doxame Crédits de la chanson & du clip Locks boi** Auteur : Locks boi Directeur Artistique : Locks boi **Les lyrics de la chanson Jëguësima honey ** 1_Couple Lidémétina dama moujé jéup sama khôl bi sédlouna Ndax khalé bima beug guele sama bopu té yeguma Damako nop bame ses si sama khôl bi té yeuku koo Soumala guiss sé béug soma nouyooour rekma réé Call la diaxaso wola banga nieuw ma mouma Khalébi laa love sama rounda gunda Khélmi diaxaso santimayi diaxaso Lépa diaxaso tékhalé bilé yaguko Sama khôl moma warona wax noumay déf baamla Mom mai déf man bama nop la paré tékma thiono Man iska dama dof kholou ma kané khalé bi rek moma saaf Saa bouma beug gué wax ak mom sama fit né têf Ma diamko pis déf rature diaré faa ay kaaf Khaw ma noumay déf mais budé man rek duko yeuk Éé girl kaye Wou yay. _Refrain Bébé Baby girl sama bébé Bébé Baby girl sama bébé Bébé Baby girl sama bébé Bébé Baby girl sama bébé _Péré- refrain Topou nala founé Wari nala founéé Topou nala founé Wari nala founéé Topou nala founé Wari nala founéé Topou nala founé Wari nala founéé Yea yea yeahhhh Topou nala founé Wari nala founé Khalé bilé kaye way Jëguësima honey Topou nala founé Wari nala founé Khalé bilé kaye way Jëguësima honey Topou nala founé Wari nala founé Khalé bilé kaye way Jëguësima _Refrain Bébé Baby girl sama bébé Bébé Baby girl sama bébé Bébé Baby girl sama bébé Bébé Baby girl sama bébé 2_Couple Khalé bima beug waxlén noumay déf ba amko Topou nako bop batay té yombou goule ma amko Khalé bima beug waxlén noumay déf bam yaukko Topou nako bop batay té yombou goule mou yaukko Khalé bima beug waxlén noumay déf ba amko Topou nako bop batay té yombou goule ma amko Khalé bima beug waxlén noumay déf bam yaukko Topou nako bop batay té yombou goule mou yaukko _Péré- refrain Topou nala founé Wari nala founé Khalé bilé kaye way Jëguësima honey Topou nala founé Wari nala founé Khalé bilé kaye way Jëguësima honey Topou nala founé Wari nala founé Khalé bilé kaye way Jëguësima..* #Jëguësima #honey #Locks boi #Doxame Have a question? contact me: 📞+221773670785

Video Information

Views
596

Total views since publication

Likes
34

User likes and reactions

Duration
2:59

Video length

Published
Dec 22, 2021

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Morocco under the topic 'météo demain'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!