NO ISSUE- AKHLOU BRICK

Directed by Wws {World Wide studios} Edited by cheikh ELPHENO Coloris by YOUNG FRESH Music: Steady Key—Weezyade—Ibou Mbaye Mix beat by: Amnezik Mix Master...

AkhlouBrickTV Officiel•1.1M views•3:35

About this video

Directed by Wws {World Wide studios} Edited by cheikh ELPHENO Coloris by YOUNG FRESH Music: Steady Key—Weezyade—Ibou Mbaye Mix beat by: Amnezik Mix Master by TAFSOUND Make up: Beonfleek STYLISTE (Tenue Africaine): MADOMARQUE AKHLOU BRICK LYRICS NO ISSUE (ARA) Akhlou Brick from Sénégal West Afraica World wide Hawma louma gnam ba diodo Sa liguéya diap sa Serigne bé aay Tek ma naagn dima madj lo Yay sama Générale nala todial way Takhaliko menoutoula né Kanar bi teud nagn ko sani guédj bae Falewma bénén go Lidiantiwma bénèn go Matay nop la angou thiow li Bb nagnou rouslo wahi noni Faw rek gnou wan lén ko Jelel sama money now Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes You make me feel the good life Give You my money See You go down For me Yi go down low Baby loumala may hep nako Te man awma si yaw sago Bb wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago this is the way Wan ma ningay dago This is... (Dayza) Ba sa xol Bangui sed Man mangui fekh Retalna man malay xol rek di bek Wanél niga meunee Wanél né dou Ben Dieund lal bou noy wanla noy danou si nek dengua, Foma fek dik sif ma séey Fo aw yon nangoulnala Biss niki tay Meusso guiss djinee yak mom kif kif la kay Gagné nga Sama coeur dakh sa assou pikaray (ARA) Ligéyma dama beug geunla bardé Nagn ko doumdou mak yaw kassé Mbeungel boudé rayé yalna dé Meunatouma sound dans yaw ( DAYZA) No man awma diom Paka bingma rayè mako dass dara metiwouma sino malila alma gaz lamign béngui sa poche sagnatouma kass Guissna sama ourou ayni nieuweul fi gnou danse kay (ARA) Jelel sama money now Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes You make me feel the good life Give You my money See You go down For me Yi go down low Baby loumala may hep nako Te man awma si yaw sago Bb wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago this is the way Wan ma ningay dago This is... Sa hol bi gagnou won na Maa gnew fadial la gomi Rangogni fér na honey No mind! I never u let you alone Dou dem la gneup wahone Décider wougn ko won It just man ak yaw dong Manak yaw la wara don bou thi ken dougou Falewma bénén go Lidiantiwma bénèn go Matay nop la angou thiow li Bb nagnou rouslo wahi noni Faw rek gnou wan lén ko Jelel sama money now Guisatouma Baby goumba na nah yay sama eyes You make me feel the good life Give You my money See You go down For me Yi go down low Baby loumala may hep nako Te man awma si yaw sago Bb wan ma ningay dago This is the way Wan ma ningay dago this is the way Wan ma ningay dago This is...
4.8

211 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
1.1M

Total views since publication

Likes
33.6K

User likes and reactions

Duration
3:35

Video length

Published
Feb 7, 2021

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Morocco under the topic 'météo demain'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!