Ashs The Best - Yaakaar [Audio]

https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Tukki Illustration & animation : Madinpixel Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https://www.faceboook.c...

Ashs The Best266.5K views2:51

About this video

https://wiseband.lnk.to/Ashs-The-Best-Tukki Illustration & animation : Madinpixel Retrouvez-moi sur mes réseaux sociaux FaceBook - https://www.faceboook.com/AshsTheBest/ Instagram - https://www.instagram.com/ashsthebest/ Snapchat - ashsthebest Parole / lyrics YAAKAAR Yow mii laa doon sèntu Mbaa yaakaar tasul ci yoon wi Jambaar dawul daa wuti Jom moy dem fulla moy dellusi Yaay di na woote Di laaj noo yèndoo Leer na ma sa jamm mo koy gënël Nga am’ag nga ñakk taxu koo jog Su soxla yi woote [soxla] Te ñu yaakaar ko ci yow Di lañ la xaar keneen ku dul yow Yow mi ñëpp yaakaar ci yow sa soxla koo koy diis Bul tiit bul jàxle Lu yoon bi mën meti Bul xaadi Lu yòmb jiggul goor Jiggul sax jigeen Kon lan ngay caalit Bul tiit bul daw bul jàxle Lu yoon bi mën meti Bul xaadi Lu yòmb jiggul goor Jiggul sax jigeen Kon lan ngay caalit Soo yakkee sooraale ma Man suma foree fii indil la Yaa taggoo ñu yobbante la Te soo goree lepp fekki si la Suñ demmee ba yaakaar ci yow mi di utti loo am di utti lu gën Suñ demmee ba yaakaar ba duñ xalaat yaakaar gi tas Suñ demmee ba yaakaar ci gaynde gi rëbbi ji woon mën jaare fa sooy Suñ demmee ba yaakaar ci moom mi dem utti ji jën Yow mii laa doon sèntu Mbaa yaakaar tasul ci yoon wi Jambaar dawul daa wuti Jom moy dem fulla moy dellusi Yow mii laa doon sèntu Mbaa yaakaar tasul ci yoon wi Jambaar dawul daa wuti Jom moy dem fulla moy dellusi Bul tiit bul daw bul jàxle Lu yoon bi mën meti Bul xaadi Lu yòmb jiggul goor Jiggul sax jigeen Kon lan ngay caalit Bul tiit bul daw bul jàxle Lu yoon bi mën meti Bul xaadi Lu yòmb jiggul goor Jiggul sax jigeen Kon lan ngay caalit Bul jàxle Bul xaadi Jiggul sax jigeen Lan ngay caalit Bul jàxle Bul xaadi Jiggul sax jigeen Lan ngay caalit © 2022 Nautylusprod

Tags and Topics

This video is tagged with the following topics. Click any tag to explore more related content and discover similar videos:

Tags help categorize content and make it easier to find related videos. Browse our collection to discover more content in these categories.

4.7

53 user reviews

Write a Review

0/1000 characters

User Reviews

0 reviews

Be the first to comment...

Video Information

Views
266.5K

Total views since publication

Likes
4.0K

User likes and reactions

Duration
2:51

Video length

Published
Dec 22, 2022

Release date

Quality
hd

Video definition

Related Trending Topics

LIVE TRENDS

This video may be related to current global trending topics. Click any trend to explore more videos about what's hot right now!

THIS VIDEO IS TRENDING!

This video is currently trending in Pakistan under the topic 'b'.

Share This Video

SOCIAL SHARE

Share this video with your friends and followers across all major social platforms. Help spread the word about great content!